Dossier de presse

Duglééne si tolluwaay Afrik wu yéés wii! Dal lééne ak jaam si miisé bu Ouidah si Bénin !


Kurélu Zinsou si ndimbëlal Christian Langlois-Meurinne ak bu l’IDI ; niooy amal xaralaak WAKPON, duppééko : le Musée fait le mur.


Ak funu mënti nek si aduna bi, xaralay WAKPON dana may way jëfëndikoom niu topp fukki aartisi tay yuy liggayal miisé Ouidah, jaaraléko si xam-xam bu mucc ayub.

Gningko taxawal si njital Pierrick Chabi, bii xarala day jëfëndikoo béépp yombal bu mana ame si waallu xarala, duppééko « yokk ak yaatal li ame ».

Taxawalal sab miisée si juroomi saart ! 


1 – Rënkal nataal yi
2 – Taflééne si miir bi

3 – Rëkal xaralay WAKPON

4 – Ubbil WAKPON si sa tablette wala si sa smartfone

5 - Natal nataal yi si sa aaparey 

ArtWOL.html
Xolal liggééy yiArtWOL.html
Wakpon_Magic.html
Sottil nataal yiWakpon_Magic.html
Wakpon.html
WakponInfo.html
iWakponInfo.html

WAKPON – Le Musée fait le mur si xaralay kurélu Zinsou la